text
stringlengths
1
2.33k
duration
float64
0.5
212
file_name
stringlengths
22
31
path
stringlengths
37
46
audio
audioduration (s)
0.03
212
sauf picc yi picc yi daal moom yooyu moom bokku si
3.163
wol_43930_1484.462_1487.625.wav
audio/kallaama/wol_43930_1484.462_1487.625.wav
ci jamono bi ñu nekk et bépp prpjet boo xam ne daf ciy yëngatu rek je pense acteurs yi ci war a jàpp yëpp dañ ci war a jàpp
6.446
wol_44611_466.465_472.911.wav
audio/kallaama/wol_44611_466.465_472.911.wav
%e assurance dafa am convention ak ministère de l' élevage direction de l' élevage ñun dañu am lëkkaloo donc %e lu ñu booleeg ñoom ñoom dañuy partager services techniques képp koo xam ne yaa ngi ci sa poste vétérinaire te yàlla mun loo la na nga ko defal procès verbal bi constat bi yaa ko war a def
19.959
wol_43951_1389.533_1409.492.wav
audio/kallaama/wol_43951_1389.533_1409.492.wav
wala que di par wala wala tamit par arrondissement
3.482
wol_43612_359.106_362.588.wav
audio/kallaama/wol_43612_359.106_362.588.wav
loo ciy tënk loo loo loo ciy yokk lan ngay tàggoo
2.893
wol_42812_1634.225_1637.118.wav
audio/kallaama/wol_42812_1634.225_1637.118.wav
ñëpp a soxla information climatique
1.745
wol_44012_594.736_596.481.wav
audio/kallaama/wol_44012_594.736_596.481.wav
merci beaucoup
0.975
wol_44012_1229.937_1230.912.wav
audio/kallaama/wol_44012_1229.937_1230.912.wav
ANACIM ñoo koy toppatoo
1.14
wol_44121_1644.492_1645.632.wav
audio/kallaama/wol_44121_1644.492_1645.632.wav
parce que ñu %e béykat yëpp xam nañu ni suuf c' est un élément vital
4.487
wol_31211_259.757_264.244.wav
audio/kallaama/wol_31211_259.757_264.244.wav
parce que dangay gis ni serieux na ci wàllu liggéey bi
2.422
wol_44914_217.052_219.474.wav
audio/kallaama/wol_44914_217.052_219.474.wav
%e code barre moo lay may nga xam ne sa maté() sa bagage bi ngay yore mën nga koo gñne ci réew mi dem jaayi ko bitim réew kon loolu jigéen ñëpp ñoom ñoo war a %e xam yoon bi mën di ko jëfee ba ñi nga xam ne ñoom kenn ku ci nekk produit yi nga yor di nga si mën di gñne si biir marché bi danga mën a gñne bitim réew
15.129
wol_41011_575.832_590.961.wav
audio/kallaama/wol_41011_575.832_590.961.wav
donc ñu bëri moo tax dañuy échoué mboq mboq bu fekkee mboq boo xam ne ay penard la ay indien la wala * loolu dafa exigent parce que ci engrais mu ngi laaj benn hectare juróom-benn saak fu kii di laajtee ñetti saak parce que ay variétés hybride la yoo xam ne dañoo exigent bu fekkee ci urée bi la hectare mu ngi laajte ñeenti saak juróom-benni saako kon donc matuwaay yi ngeen di jël ci hybride bokkul matuwaay yi ñuy jël ci variété locale
25.995
wol_43011_1364.193_1390.188.wav
audio/kallaama/wol_43011_1364.193_1390.188.wav
peut être %e ci biir waxtaan wi mën naa am ñu dellusiwaat si mais nañu xam ne daal %e insecte ravageurs yi nga xam ne ñoom ñoo gën a mën a yàq stoc ci biir magasin wala ci biir %e grenier wala ci ci foo ko foo mën a denc sa sa sa sa meññeef %e juróom-benni famille céoptère yooyu ma leen limal bokk nañ si ak ñetti lépidoptère yooyu ma leen wax ñoom it bokk nañ ci ñi nga xam ne ñoo dàq a yàq
23.466
wol_43311_939.651_963.117.wav
audio/kallaama/wol_43311_939.651_963.117.wav
je pense mun nañ jël benn thématique boo xam ne dafa am lien ak maraîchage pour ñu sensibiliser leen ci thématique boobu
7.157
wol_44611_1263.753_1270.91.wav
audio/kallaama/wol_44611_1263.753_1270.91.wav
waaw effectivement compliqué na trop
1.584
wol_41011_377.815_379.399.wav
audio/kallaama/wol_41011_377.815_379.399.wav
%e bëgg mu gën a bëgg a gën a xam
1.248
wol_41711_498.832_500.08.wav
audio/kallaama/wol_41711_498.832_500.08.wav
yoo xam ne mën na ko jëfandikoo effectivement daan nañu am problème yu mel noonu
3.365
wol_44113_718.141_721.506.wav
audio/kallaama/wol_44113_718.141_721.506.wav
producteur yi dinañ xam ban pratique moo gën bu fekkee ne nag biñ leen indil
5.153
wol_44612_164.241_169.394.wav
audio/kallaama/wol_44612_164.241_169.394.wav
d' accord
0.968
wol_4111_1439.528_1440.496.wav
audio/kallaama/wol_4111_1439.528_1440.496.wav
noonu la ñu war a informa() am information ñëw ci service techniques yi ñu wax la ñu wax rek quelle période la ñu war a ji lan mooy gerte lan mooy dugub lan mooy mboq loolu tamit véhiculer message yi muy yi nga wax nii en terme de communication daf ci am solo
12.977
wol_43031_793.743_806.72.wav
audio/kallaama/wol_43031_793.743_806.72.wav
maanaam sable bi
0.875
wol_44112_371.412_372.287.wav
audio/kallaama/wol_44112_371.412_372.287.wav
waaw loolu yëpp gis nañu ko si
1.629
wol_42514_319.154_320.783.wav
audio/kallaama/wol_42514_319.154_320.783.wav
toog na jotul sax woote waaye mu ngi doon déglu émission bi ñu ngi leen di gërëm di leen jaajëfal bu baax a baax
3.955
wol_45422_1626.226_1630.181.wav
audio/kallaama/wol_45422_1626.226_1630.181.wav
te kenn ku ci nekk fii am na loo xam ne mën na ko ci indi
3.399
wol_43211_232.726_236.125.wav
audio/kallaama/wol_43211_232.726_236.125.wav
ndax su boobaa température yiñ nar a dundee si addina nit yi du ko )ttan parce que dinañ dem ba moins dix huit degré muy nekk température bu négative loolu nit munu see dund
14.173
wol_43711_1220.19_1234.363.wav
audio/kallaama/wol_43711_1220.19_1234.363.wav
am na solo kon Diallo Diagne ñu ngi lay gërëm di la sant di Pusseynou diagne bokk ci liggéey bi tamit moom moo fare woon côté Njaañ kon ñu ngi lay gërëm di la sant jërëjëf
8.62
wol_41910_1509.772_1518.392.wav
audio/kallaama/wol_41910_1509.772_1518.392.wav
%hum %hum kon ñu mën a jàpp rek ne déréglement boobu nga xamante ne nii gis nañ ko ci wàllu prévision yi ci fi nga xamante ne nii %e mooy gox bi ñu féetoo di diwaanu Nior gën cee leer di Saloum %e nekk na loo xamante ne nii %e coppite jaww ji la maanaam changement climatique bi moo ko daal di andi
15.503
wol_43020_1336.98_1352.483.wav
audio/kallaama/wol_43020_1336.98_1352.483.wav
%hum ak waa ICS ah def ay recherches ba nga xam ne
3.695
wol_43012_641.14_644.835.wav
audio/kallaama/wol_43012_641.14_644.835.wav
te yoroo torche boo ko niinee
1.665
wol_43020_1748.836_1750.501.wav
audio/kallaama/wol_43020_1748.836_1750.501.wav
maintenant am na yeneen catégories jeunes nag yoo xam ne su def nañ formation
6.013
wol_44611_1119.579_1125.592.wav
audio/kallaama/wol_44611_1119.579_1125.592.wav
loolu mooy problème bi gàllankoor mooy pro() parce que biodigesteur bu demee ba fonctionner nga am sa engrais nga am sa gaz daanaka jigéen yu bëri nga xam ne dañuy yëngu ci wàllum transformation parce que tamit waxuñu ko
13.086
wol_42922_459.025_472.111.wav
audio/kallaama/wol_42922_459.025_472.111.wav
waaye nag dans topus les cas
0.975
wol_44112_545.549_546.524.wav
audio/kallaama/wol_44112_545.549_546.524.wav
waaw mooy li may wax rek
1.617
wol_43412_1364.893_1366.51.wav
audio/kallaama/wol_43412_1364.893_1366.51.wav
wala soit leneen nga ñooñu kenn ku ci nekk war nga mën a defar say kayit ba mu valable soo amee say kayit ba mu valable nag nga xam ne say produit boo ko xasee defar
8.751
wol_41011_682.942_691.693.wav
audio/kallaama/wol_41011_682.942_691.693.wav
kon nag
0.683
wol_43612_109.328_110.011.wav
audio/kallaama/wol_43612_109.328_110.011.wav
waaw xam nga jamono suy dox nag
1.115
wol_42811_1220.263_1221.378.wav
audio/kallaama/wol_42811_1220.263_1221.378.wav
dégg nga %e damay fàttali leen gën di wax nit ñi %e laaj leen ñu ni ñu bon messages yi baax na waaye li leen gënaloon moom mooy message rajo am na kii quoi message kii quoi vocal
11.226
wol_42212_1458.933_1470.159.wav
audio/kallaama/wol_42212_1458.933_1470.159.wav
ci loolu te te te te lu ñu xamul mooy maanaam janax boobu sax am na feebar bu muy joxe parce que janax bi sawam yi sawam bi dafa am benn feebar boo xam ne dafa nekk ci moom
11.761
wol_43910_1507.543_1519.304.wav
audio/kallaama/wol_43910_1507.543_1519.304.wav
moo tax énoom %e vraiment macha allah dañu leen dii dañu leen di sant bu baax a baax beneen bi ci des tey jii ñu énu dugal beneen %e domaine ci mbir mi muy restauration
9.06
wol_4613_766.946_776.006.wav
audio/kallaama/wol_4613_766.946_776.006.wav
xam e rek moo di ANACIM ndax li nga xam ne rek moo di changement climatique doon na réalité
7.328
wol_42513_0.0_7.328.wav
audio/kallaama/wol_42513_0.0_7.328.wav
salaamaaleykum
0.528
wol_43612_1496.484_1497.012.wav
audio/kallaama/wol_43612_1496.484_1497.012.wav
donc li si jiitu mooy information météo bi ci la bokk d' accord
4.769
wol_43020_1468.504_1473.273.wav
audio/kallaama/wol_43020_1468.504_1473.273.wav
maanaam au lieu ngay de() ngay dem ak sa xel noonu rek
2.914
wol_42932_221.794_224.708.wav
audio/kallaama/wol_42932_221.794_224.708.wav
dañu lay indil yow dañuy indi dañuy indi ngeen ñam produit yëpp la ñuy indi
2.678
wol_41013_538.395_541.073.wav
audio/kallaama/wol_41013_538.395_541.073.wav
ni ko amsecta yi
1.121
wol_45412_78.507_79.628.wav
audio/kallaama/wol_45412_78.507_79.628.wav
%e di leen ko xamal ñuy xam fuñuy teg seen i tànk
2.352
wol_4812_648.797_651.149.wav
audio/kallaama/wol_4812_648.797_651.149.wav
il faut que ñun ñii ñu xam ne mbay
1.554
wol_44112_491.174_492.728.wav
audio/kallaama/wol_44112_491.174_492.728.wav
bokkul dafa xaw a danoo niróo nag
1.521
wol_45412_1422.167_1423.688.wav
audio/kallaama/wol_45412_1422.167_1423.688.wav
alahuma amiin
1.357
wol_4314_469.128_470.485.wav
audio/kallaama/wol_4314_469.128_470.485.wav
%hum te ku am %e béykat boo xam ne da nga yor say jur war leen a dundal defe nga ne kooku dina la dégg
6.775
wol_43810_1515.222_1521.997.wav
audio/kallaama/wol_43810_1515.222_1521.997.wav
%e incha allah
0.996
wol_42931_143.888_144.884.wav
audio/kallaama/wol_42931_143.888_144.884.wav
bisimilah sëñ bi na nga tudd
2.226
wol_35710_0.0_2.226.wav
audio/kallaama/wol_35710_0.0_2.226.wav
dama bëggoon na %e contribuer ci %e seen émission bu am importance bii
5.28
wol_43412_1029.681_1034.961.wav
audio/kallaama/wol_43412_1029.681_1034.961.wav
moom moo doon ñëw lu gën a bari di def si émissions yi
3.275
wol_35312_80.37_83.645.wav
audio/kallaama/wol_35312_80.37_83.645.wav
mu ngoog kooku la
1.14
wol_45412_402.597_403.737.wav
audio/kallaama/wol_45412_402.597_403.737.wav
loolu mooy surtout jafe bi donc météo ne suba dina taw béykat bi nan lay fexe ba am information boobu mais tamit il faut que tamit %e ñoom i tam ñu def ay effors tamit parce que boo xoolee tey rajo yi comme rajo Ndefleng par exemple fii souvent météo daf fay jaar def ay émissions joxe ay informations ak yooyu ah
23.217
wol_42912_912.838_936.055.wav
audio/kallaama/wol_42912_912.838_936.055.wav
et et tey %e Habib %e lu tax COPEGA di di di dérangé c' est à dire le problème c' est quoi parce que man bu fekkee dëgg rek laa leen wax su ma déggee ku leen di supporté wala ku ànd ak yéen rek ñaareel ab béykat la mais au delà de ça les orga() ñeneen ñiy yëngatu ci kii bi filière bi daal da da ngeen di dérangé %e le problème c' est quoi lan la
18.301
wol_44412_289.321_307.622.wav
audio/kallaama/wol_44412_289.321_307.622.wav
%e chaque président de section villageoise ñu convoqué leen
2.768
wol_31212_398.721_401.489.wav
audio/kallaama/wol_31212_398.721_401.489.wav
dégg nga
0.597
wol_42611_1326.665_1327.262.wav
audio/kallaama/wol_42611_1326.665_1327.262.wav
ñu def ay jàngat xool gis ne effectivement gis nañ ne depuis des années suñ delloo si histoire depuis les années mille huit cent
10.383
wol_43020_946.218_956.601.wav
audio/kallaama/wol_43020_946.218_956.601.wav
en vu de la prochaine campagne
1.379
wol_43810_429.193_430.572.wav
audio/kallaama/wol_43810_429.193_430.572.wav
%hum %hum foog mu ñor foog ñu weer ko ba mu wow koŋŋ
3.721
wol_43311_1281.979_1285.7.wav
audio/kallaama/wol_43311_1281.979_1285.7.wav
comme day nekk information bu yaatu
1.629
wol_44113_568.911_570.54.wav
audio/kallaama/wol_44113_568.911_570.54.wav
nga dem ji wala nga dem def
1.887
wol_43020_303.171_305.058.wav
audio/kallaama/wol_43020_303.171_305.058.wav
boobu day nekk bi ñuy wax limon
1.996
wol_44311_591.579_593.575.wav
audio/kallaama/wol_44311_591.579_593.575.wav
di sant auditeurs yëpp
1.447
wol_4314_904.563_906.01.wav
audio/kallaama/wol_4314_904.563_906.01.wav
%hum %hum %hum loolu la kay
3.075
wol_4612_82.095_85.17.wav
audio/kallaama/wol_4612_82.095_85.17.wav
%hum %hum %hum
0.923
wol_4811_156.931_157.854.wav
audio/kallaama/wol_4811_156.931_157.854.wav
fépp foo dégg assurance indicelle
2.549
wol_44122_726.3_728.849.wav
audio/kallaama/wol_44122_726.3_728.849.wav
ba nga xam ni %e niñ niñ daan liggéeyee ñu ngi gën di ci weer yooyu ñu ngi koy ñu ngi koy gën di ñeme ndax ñu ngi doon jotee information ci ci Nafoore dafa dalaloon sunu sunu xel
10.352
wol_36510_256.468_266.82.wav
audio/kallaama/wol_36510_256.468_266.82.wav
na ñu arrêté di gor
1.208
wol_44114_775.094_776.302.wav
audio/kallaama/wol_44114_775.094_776.302.wav
bon fumier moom am na solo am na solo trop ci tool
4.361
wol_43810_1913.398_1917.759.wav
audio/kallaama/wol_43810_1913.398_1917.759.wav
kon foofu daal amoon na kay tuuti jafe-jafe
1.816
wol_31211_588.151_589.967.wav
audio/kallaama/wol_31211_588.151_589.967.wav
par rapport ak première taw bi
1.489
wol_44312_239.938_241.427.wav
audio/kallaama/wol_44312_239.938_241.427.wav
yàlla baax na
0.5
wol_42212_1631.045_1631.545.wav
audio/kallaama/wol_42212_1631.045_1631.545.wav
waaw vaaw
0.669
wol_4210_1956.915_1957.584.wav
audio/kallaama/wol_4210_1956.915_1957.584.wav
mën nañu la jàpp chambre de commerce ñëpp kenn ku ci ne dana def visite ci fi nga xam si ne mooy béréb bi nga xam ne si nga defaree li nga xam si moom mooy céréale bi wala soit yeneen produit yi ngay defar
10.342
wol_41012_75.198_85.54.wav
audio/kallaama/wol_41012_75.198_85.54.wav
Baye Niass ba muy wax radi yallaahu anhu
2.085
wol_44411_1557.022_1559.107.wav
audio/kallaama/wol_44411_1557.022_1559.107.wav
yooyu boobu nag moo gën a garaaw boobu vingt et un fois la gën a garaaw que CO2 tu vois boo xoolee bon yokkuteem mu ngi toll si zero virgule six pour cent ci at bu nekk
9.814
wol_45511_546.129_555.943.wav
audio/kallaama/wol_45511_546.129_555.943.wav
na ñuy déglu informations yi régulièrement ;fra
2.101
wol_42932_394.089_396.19.wav
audio/kallaama/wol_42932_394.089_396.19.wav
ndax Fapal kuréel la boo xam ne si wax naa ko ci ñaar ñett fànn yëpp ci lay yëngu
4.086
wol_4311_241.463_245.549.wav
audio/kallaama/wol_4311_241.463_245.549.wav
donc loolu moom mooy loo xam ne souvent dañu koy déploré
2.115
wol_35312_128.212_130.327.wav
audio/kallaama/wol_35312_128.212_130.327.wav
jote wuñ sax xëy na peut être ci télévision parce fu mu la fekk dafay sori mais à travers :ra les projets et programmes yi nga xamante ni moom la ñu am ñu mel ni waa 4R ñu mel ni ay Proval ak yeneen ak yeneen jàppale nit ñi ba nga xamante ne bi au niveau de de note service am nañu benn base bi nga xamante ni bii %e ay numéros de téléphones yi ça fait plus de mille
21.064
wol_42611_1407.289_1428.353.wav
audio/kallaama/wol_42611_1407.289_1428.353.wav
waaye terewul ba tey mën nañu wéyal waxtaan bi ànd ak kii di Jalle yaakaar naa ni li fi Ibrahima wax yëpp am na am na solo te it xam naa ni %e yéen yaa ngi naan Ibrahima moo tax amagu leen yéen code barre mais yéen seen wàllu bopp aussi est ce que mate ngeen normes yi war a tax ngeen am code barre
14.077
wol_41013_361.197_375.274.wav
audio/kallaama/wol_41013_361.197_375.274.wav
mais bu tawee ci kawam non seulement am na nu muy demee doomu gerte bi dafay
5.781
wol_42212_1149.305_1155.086.wav
audio/kallaama/wol_42212_1149.305_1155.086.wav
seen seen coopérative
1.06
wol_31211_660.072_661.132.wav
audio/kallaama/wol_31211_660.072_661.132.wav
mu daal di wow séchage
2.787
wol_42912_316.048_318.835.wav
audio/kallaama/wol_42912_316.048_318.835.wav
%hum %%hum
0.689
wol_36010_4.723_5.412.wav
audio/kallaama/wol_36010_4.723_5.412.wav
te mbéyum ceeb ku ko xam ci ji mi dafay ànd ak %e pour mu gaaw a sax il faut que nga am tàngaay bu njëkk ba dañ daan wax ci yenn weer yi daawul tàng dafa daan sedd te gis nañ ni weer yooyu léegi de mi ngi tàng
12.058
wol_36510_244.41_256.468.wav
audio/kallaama/wol_36510_244.41_256.468.wav
rupture ci ñebe bi kii bi du baax feek book Etat bi nga xam ne ni moom mooy gëstu di gñne lu bees moom dina dina ci %e dina dina dina ko def
8.613
wol_4314_155.075_163.688.wav
audio/kallaama/wol_4314_155.075_163.688.wav
ah waaw ro()
1.613
wol_45411_1777.579_1779.192.wav
audio/kallaama/wol_45411_1777.579_1779.192.wav
%e loolu tamit muy beneen aspect ci njëriñ bi nga xam ne rotation bi mun na ko mun na ko mun na ko amal
4.537
wol_43810_922.89_927.427.wav
audio/kallaama/wol_43810_922.89_927.427.wav
xool yan interet lañuy teg lan moo ci teg ba ci assurances yi ñuy def
5.43
wol_4812_613.216_618.646.wav
audio/kallaama/wol_4812_613.216_618.646.wav
dêgg la ñu jël kooku allo
1.882
wol_44412_1084.008_1085.89.wav
audio/kallaama/wol_44412_1084.008_1085.89.wav
ak doxalin bi mën nanoo uute waaye lépp ku ci nekk ku taxawoon fii ne jox leen ma réew mi ma taal Sénégal jox leen ma réew mi ma andil leen ndóol jox leen kan moo ko fi dégg
8.261
wol_44412_1765.669_1773.93.wav
audio/kallaama/wol_44412_1765.669_1773.93.wav
d' ccord
0.712
wol_36410_664.76_665.472.wav
audio/kallaama/wol_36410_664.76_665.472.wav
day ma dama lay jox benn misaal rek tey jii boo demee Europe par exemple dangay dem ñu ne la yaa ngi nekk ci ay zero degré wala ay moins moins mo() moins cinq degré affaire yu mel noonu
11.085
wol_42212_578.683_589.768.wav
audio/kallaama/wol_42212_578.683_589.768.wav
ñooñu ñooy changé
1.027
wol_44111_325.206_326.233.wav
audio/kallaama/wol_44111_325.206_326.233.wav
xanaa rek balaa ñuy tënk rek ñu delloowaat kàddu bi monsieur %e Diatta par rapporrt aux perspectives des communautés les plus résilientes maanaam ñi nga xam ne gis nañ ne que ne %e seen loxo jotul seen i ginnaaw bu baax ñi nga xam ne ciblé nañ leen ci seen enquête yi ngeen def njëriñ bi ci projet bi wala tamit %e lan ngeen di séntu si ñoom ba tax ñu ngeen dugal leen ci projet bi
23.541
wol_42922_598.102_621.643.wav
audio/kallaama/wol_42922_598.102_621.643.wav
ba jotanteeg ñoom man maay le président bi maa ngi dëkk kër Saalum Diané ñu may wax Aliou Ndao
4.131
wol_42311_267.201_271.332.wav
audio/kallaama/wol_42311_267.201_271.332.wav
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
52