audio
audioduration (s)
1.68
35.5
transcription
stringlengths
23
537
asaalaamaaleykum mbokki auditeurs auditrice su 93 point 5 ñu ngi leen di jaajëfal bu baax a baax ci déglu bi di leen nuyu bu baax a baax te itamit %e di jox suñu nuyoo rek kii di suñu DG monsieur Pape Mate Diouf mu daal di koy séddale képp ku nekk ci rajo bi ak bitti rajo bi ñu nghi leen di jaajëfalaat bu baax a baax
tey nag dikkaat nañ si suñuy émission yi ñu jagleel nag météo waaye jagleel ko mbéy mi ci dëkk bi ci Fatick ak li ko wër ñu nar a dalal nag fii tey ci sunu émission ki nga xamante nemoom mooy Momadou Bodian di directeur régional développement rural waaye tamit %e di dalal Maodo Maodo miin nañ ko fi nag bu baax a baax Maodo Samb di chef service régional de la météo fii ci région de Fatick
tey nag ñuy waxtaanee lii di information climatique dans les activités de récolte et post récolte loolu nag bu ñu ko waxee day daal di duggaat rek ci mbéy mi ana yan information la ci nit ñi soxla ci avant ak après récolte
ñu nar ko faram-fàccee fii ci rajo Ndefleng FM Fatick ci kàffu gi Maguette Mbaye ci technique bi kii di DJ Madou dañuy daal di bàyyi rek sunu ñi nga xamante ni ñoo di suñu invité ñu daal di présenté wu ñoom itamit suñu mbokki auditeurs yi
balaa boobu di leen dalal jàmm te itamit di leen remercier ci acceptation invitation bi %e damay bàyyi rek %e Maodo comme %e ci kër gi nga dëkk daal di bàyyi rek sunu gan gi mu daal di moom itamit %e def li nga xamante ni moom mooy présentation bi te tamit di ko wax mu dalal jàmm %e Momadou
jërëjëf soxna Maguette ñu ngi leen di nuyu di leen sant ak ñëpp ñiy déglu rajo bi %e damay faral di wax ne am ngeen pàcc bu mag ci wàll wi nawet mooy loo xam ne bawul kenn
te bu ñu ko waxee ëmb na lépp ndax ku xam Sénégal xam ne nawet bu yàlla defee mu antu nañ ko muurloo mu ne ah ma ne ko njëriñ la ca ne mu ne ah ma ne ko dana laal ñëpp du ba kenn
%e rawatina tey jii li nga xam ne %e moo ñu fi di dajale muy loo xam ne wax dëgg fa yàlla ab lëkkaloo la bu am solo et lëkkaloo nag boo ko déggee dañu naan nguuru Sénégal cib liggéeyam mu ne ah ma ne ko allak kulli haal ci fàcc bu mu mun a doon mu ne ah ma ne ko da ngeen dégg ñu ne am nañ ay partenaires yu ko cay jàppale moom lañ tuddee les partenaires techniques et financiers
te partenaires yooyu PAM defe naa ne liggéey bi mu ciy def lu jéggi sax njàngin wi defe naa ci wàllu mbéy mi mu ne ah ma ne ko kenn naatable wu ko
wax dëgg fa yàlla loolu cant ak ngërëm dina leen ñeel ndax dina tax ñu mun a tey jii am jotaay boo xam ne des ci mun a leeral faram-fàcce ci loo xam ne jëm ci nawet bi
bu ñu ci yeggee tuuti dinaa ci dugg incha allah ci kanam man la Momadou Badiane directeur régional yor wàllu loolu fii ci Fatick di rafetlu émission bi di leen gërëm di leen sant incha allah ba cvi kanam tuuti
macha allah jaajëfal nañu la %e Momadou Badiane moom itamit mu ñëw ci suñuy %e studio rek daal di bëgg a waxtaan ak askanam waxtaan ak waa région de Fatick bàyyi rek Maodo ñu ngi lay jaajëfal yow tamit di la daal di dalal jàmm ci sunu studio
di la remercier %e ci li nga xamante ne mooy acceptation invitation bi di la bàyyi nga nuyu suñu mbokku auditeurs yi
waa asalaamaaleykum %e soxna Maguette xanaa rek %e di delloo buum ci mboy-mboy ga rek di wax ni maa ngi nuyu askanu siin yëpp
bàyyi wu ma kenn di am nag wax dëgg yàlla tey mbéte wala boog kontaante bu wér bokk plateau bi ak %e suma xarit suma suma conseiller technique mun naa wax loolu suma %e genn wàll muy Momadou Badiane bi nga xamante ne bi yàlla moom moo ñu boole
mu yore direction régionale %e agriculture direction régionale développement rural autant pour moi nga xamante ne bii dafa %e dafa moo gën a yaatu
man yàlla def ma tamit bon ma yor wàllum météo %e yàlla def aussi bon depuis bi mu fi ñëwee ba léegi wax dëgg yàlla ñu ànd di liggéey vraiment liggéey boo xam ne bii bu mucc ayib la
liggéey bu rafet la boo xam ne dama ko rafetlu trop
rafetlu naa ko suñu ay kilifa vraiment rafetlu nañ ko aussi vraiment %e ma am daal wax dëgg yàlla daal tey jii mbégte gu rëy %e bokk ak moom jotaay bi
ndax nit bu ñuy wax %e agriculture %e yaakaar naa ni ën nañu wax ni général gi yëpp dinañ wax naan ne météo la
wala boog si gàttal rek bu fekkee ne que tey jii da ngay wax mbay yaakaar naa li ci ëpp solo moom mooy arrosage
bu ñu nee arrosage nag doomu aadama aadama bi mun nañoo jël robinet wala mu jël %e ay ay jumtuwaayam root arrosé waaye arrosage bi nga xamante ne bii moom mooy li ëpp solo mooy bi nga xamante ne bii moom la suñu borom subxanahu wa taalaa def nga xamante ne bii mooy ubbi asamaanam mu taw ba macha allah kenn ku si nekk
li nga xamante ne bii moom nga yaakaaroon moom nga mën ci gis sa bopp
donc %e ñun ci côté boobu moom la ñuy kii quoi ñu ngi koy liggéey boobu ba léegi nawet bi door nañ ko ci bisimilahi rahmaani rahiim %e ñu ngi am yaakaar te aussi vraiment ñu ngi ciy génn ci alhamdulilahi rabil aalamiin
donc di ñaan ci yàlla suñu borom %e lépp li nga xamante ni bii am nañ ko ci muy ay meññeef yi nga xamante ne bii tey jii villageois yi récolté nañu ko li ñuy ñaan rek moom mooy na ko ñëpp jëriñu ci jàmm ak tal
am na solo am na solo %e Maodo ñu nar a seq ak yéen waxtaan bi balaa boobu nag %e cig fàttali rek dañuy %e fàttali émissions yi ñi ko sponsorisé bokk na ci projet 4R du programme alimentaire mondial PAM dans les cinq régions cibles
cinq régions cibles yi nag Tambacounda la Kolda Kaolack Kaffrine ak Fatick loolu nag %e ñu ngi ko tënk rek ci soutien bi nga xamante ne moom mooy soutien technique bu Jokalante di leen jaajëfaalt bu baax a baax ñoom itamit sponsors yooyu noonu
%e Maodo balaa may %e dikk rek ci li nga xamante ne moom mooy vif sujet bi cib tënk rek li nga xamante ni génn nañ ci doon ko waxtaanee temps yëpp muy mbéy mi
sànq yaa ngi wax naan duggoon nañ ci ak ci bisilimahi rahmaani rahiim génn ci ci alhamdulilahi rabil aalamiin ñu mën a jàpp ci %e li nga xamante ne moom mooy mbéyum ren lan lañ ci mën a jàpp
%e mbéyum ren xëy na bëgg naa ci aborder mais comme yàlla dafa dogal ma toog ak ki nga xamante ni tey jii c' est la vois la plus autorisée
am na fi nga xamante ni peut être que foofu laay yem
d' accord mais may wax rek ni nawetu ren
gis nañ nii que ñu ngi am %e nawet bi le premier juillet le le premier juin autant pour moi le premier juin ci la ñu am les premiers pluies utiles fii ci biir en tout cas région de Fatick
jàpp nañu en terme donc de d' opération culturale am nañu trois vagues de semis tawu juin boobu am na ñi nga xamante ne bi jiwoon nañ ci
am na ñi nga xamante ne bi toog nañu presque weer après ñu soog a mën a am ndox bi nga xam ne bii war na mën leen permettre ñu déclenché seen ay semis am encore une troisième vague
donc loolu nag am na jeexital bi nga xamante ne bii am na ko tey ci ci kii quoi gàncax gi parce que bu ñuy wax %e loolu boo moytuwul gis nañ ni que ñi nga xamante ne bii tey ñoomñoo déclenché woon seen %e seen semis ci première kii bi quoi première taw bi mooy taw bu juin boobu
neeñu alhamdulilah fi mu nekk nii bu dee wàllum gerte gerte gi ñor na bu dee suuna bi vraiment suuna si ñor na bu dee mboq mi ñor na pratiquement de spécu() spéculation bi yëpp mën nañu wax lépp kii na ko egg egg na actuelement à maturité
te li koy firndeel moom mooy tey jii boo duggee ci biir %e marché bi di nga gis ni vraiment nit ñaa ngi fi nekk nit ñaa ngi lekk gerte bu doy nit ñaa ngi lekk mboq dégg nga ak yeneen ak yeneen ak yeneen ak yeneen donc loolu dañuy wax ne sant yàlla la
am na nag ñi nga xamante ne bii ba léegi %e seen seen seen %e seen mbéy xaw na xaw na kii quoi xaw na doy waar
mooy ñi nga xamante ne bi ñoom ñoo nekkoon ci deuxième vague de semis bi ak troisième vague de surtout ñi nekkoon si troisième vague de semis bi ñooñu mën naa wax ni vraiment fu mu nekk nii seen situation kii bi quoi doy na waar trop
mais nag ñu jàpp ni wolof dafay léebu ne nawet moom toujours dafay naawee wet dégg nga donc ni muy %e baaxee ci penku noonu la mun a bonee ci soww
wa illaa tamit des fois tamit ñu am ñu am kii quoi le sens contraire
ren jii yàlla noonu la tëggee nawet bi ah ñu koy nangu xam ne aussi que comme ni ñu koy faral di waxee rek changement climatique moom mooy li nga xamante ni moom moo fa jaar parce que d' habitude li daan am moom mooy bu tawee dafay taw rek
dégg nga %e ñu am un un bon démarrage donc distribution spatiotemporelle comme ni ko tubaab di waxee mu am benn didtribution bu correcte mais ren jii gis nañu que ni distribution boobu moom si boppam moom moo correct wul
%e li ma ci gën a yéem nag tuuti kooku naa ci si xëy na du ñàkk sax directeur moom xëy na dina ma mën a gaganti
bon gis nañu ne dafa am benn zone fii ci région de Fatick mooy diggante Tataguine
jàpp %e Diohine jàpp Toucar jàpp daal la vallée morte du siin
gis nañu côté boobu presque ay at a ngi nii même année même profil bi la ñu am c' est à dire que chaque année vraiment dañuy am problème ñoom pour kii quoi pour ñu décoller
léegi dañuy am problème ñoom pour ñu décoller et puis souvent même bu ñu décoller aussi très souvent même bu ñu yeggee bu seen spécu() spéculation yi du egg du arrivé aussi à maturité nim ñi ni ñu ko bëggee noonu lañ ko nii lay demee daal
actuellement nii ren jii fii may waxee nii nii foofu nekk na zone bi nga xamante ne bii peut être que bëgguma jiitu sunu mbokk yi nga xamante ne bii ñoom ñoo yore sécurité alimentaire bi pour di ci wax mais ñaaw naa njort lool ni soo moytuwul dafay ne risque nekk une zone à risque alimentaire
xam naa lu si nekk directeur dina si delluwaat incha allah
nañ ci dellusiwaat monsieu Bodian dañ lay daal di bàyyi rek nga daal di présenté waat lii di structure kuréel bi ngeen nekk ak itamit lan mooy zone d' intervention bi
waa jërëjëfëf direction de la développement rural mooy kuréel gi nga xam ne moo yor mbéy mi ci wàllu Fatick
boo xoolee taxawaayam am na kër gu boo xam ne moo nekk fii ci quartier Escale ñi ko xam bëri na ndax Fatick moom boo nee agriculture rek %e dana bërëb ba dafa jëmme ndax dafa am histoire dafa am taarix %e boo xoolee département bu ne it %e kër ga jëmmal nañ ko fa
donc mu am kilifa bu ko jiite ak ay %%e ay techniciens noonu la bindoo si wàllu taxawaay
li ko wër nag ay projets ak ay programmes la yoo xam ne ñu ngi ci ndigalu ministre de l' agriculture d' équipement rural ñoom it bokk ci liggéey bi kenn ku ne di indi sa wàll ci ci ci ci %e ci li nga xam ne moom lañ bokk jëmee ko ci béykat yi nga xam ne mu nekk wàll wu am solo ci askan wi loolu loolu mooy taxawaay bi ci wàllu bi ñun ñëpp ñu nekk ay lu ñu tuddee démembrements
kër gu yaatu la am ay démembrements DRDR bi ci département bi SDDR lañ leen di tuddee mooy service départemental développement rural boo demee it ci %e lu mel ne comme agences yi ñëpp ñu ngi dégg ANCAR
ñoom it ñu am pàcc boo xam ne donc moom la ñuy dox ci wàll wi
ak yeneen yu demee ni ki ANIDA ak projet programme yi nga xam ne xëy na bu ñu ci tuddee tur dina am dina am %e nañ ko bçyyi xel lu mel ne Proval chaine de valeur
projet Agri Jeunes ak beneen bu bees boo xam ne sax mu ngi %e waaj a taxaw ñu ngi ci tànk taxawal ko daanaka ñi ngi teew ci région abi ñu ngi nekk ci liggéey xam naa dina gën a fës ci kanam tuuti
ñu ne programme de développement chaine de valeur yi nga xam ne Banque Islamique de Développement moo ciy jàppale nguuru Sénégal
ak %e yeneen projets programmes ak Paris yooyu yëpp dafa bokk ci projet sous tutelle ministre agriculture boo xam ni ñoom it dañuy dugal seen wàll seen loxo ci nawet bi
waaye boo xoolee nawet bi soo ko bëggee tënk da ngay gis ne nawetu ren bi comme ni ko sëñ Maodo waxee %e ñoom sëñ Maodo dañ waxoon ne seen gëstu ne nawet bi dina teel
wax na naam wax na dëgg ndox mi boo xoolee daawaat daawaat daaw %e boo xoolee le douze juin %e lañ tawluwoon bii gën na teel ndaxte boo xoolee côté le huit juin la ñu am taw yu njëkk yi
%e waaye nag la ca topp waxoon nañ ko newoon nañ ah mun na teel a dikk waaye dina am ay dog-dog dog-dog yooyu gis nañ ko ci mois de juin bi ak mois de juillet bi ba nga xam ne bi taw biy dikkaat boo xoolee ci ñoom li ñu tuddee derniers décate maanaam mooy fan yu mujj ci mois de juillet ci la yëf yi ñëwaat
dog-dog yooyu li mu indi nag comme nim ko waxee dafay méngoo ak ni gàncax giy màggee ndax ku xam ne dañ ne nawet la ko gën a téye tey jii comme ni mu ko waxee dañ koy firnde dëggal ko de() dem nañ ba tey jii information climatique bi dafa nekk dafa am tolluwaay comme nga ne jiw ni engrais ni puudar ni matériel bu ndaw wala matériel bu mag
maanaam facteur de révolution te tey jii sax moom la ñuy jiital ndax tey jii changement climatique yi ñu ne
tax na bu ñu jiitalul information climatique bi dina tënk lu bëri
maanaam jiw bi mun na mucc ayib engrais bi ak jiw bi yëpp mën na teel a dikk matériel bi sax mën na teel a dikk lépp waaye bu ndox amul dara du sotti ndax nawet bi nawet bi dañ ne nawet la boo xam ne mu wékku ci ndox mi nga xam ne day jóge ci asamaan te yàlla buur bi di ko taw mu te di ñi ko baaxee te béykat yi di ci def li nga xam ne moom la ñu war a def
loolu bu ko defee day tax ci wàllu xeetu mbaax yi ñu tuddee bonne pratique ci wàllu mbéy da ngay gis ne béykat bi day topp loolu
li ñuy li nga xam ne mën nañ koo faru mooy li ñuy tuddee semis à sec képp koo xam ne xam ne ne suuna dañ koy faru
doo bàyyi ba bàq yëpp tooy nga koy ji da ngay tardé waaye am na ci loo xam ne li ci des yëpp boo xoolee foog bàq bi tooy te léegi waxatuñ tooy tooy tooy tuuti de bàq bu tooy lañ wax
li ñu ci jublu mooy béykat bi léegi doo ko ne demal nga ji da nga koy fexe bu jiyee mu sécuriser ji ma looloo tax ñu ne la bàq ba tooy tigi ba ba nga xam ne bu gerte ñëwee basi ñëw sëb ñëw %e mbokk ñëw leneen dikk lu mel ne bene mooy sesam ceeb parce que dañ ko fiy béy département Fatick ak Foundiougne macha allah
yooyu yëpp bu ko defee ñu mun leen a sécuriser kon %e defe naa ne loolu lu am solo la léegi boo ko xoolee ci nawet bi comme ni ko waa ANACIM waxee liñ ci wax lépp dara dëñu ci macha allah
li ko waral mooy lenn mooy wax ji dafa tegu ci xam-xam tegu ci ay jumtuwaay ak i xarale yu mucc ayib kenn weranteeul waxu météo
léegi ci fànn yëpp rawatina ci wàllu mbéy kon loolu cant ak ngërëm ñeel na leen ci liggéey bi ñuy def
tey léegi nag waaw boo ko xoolee léegi tey jii boo xoolee
%e macha allah léegi ci %e yegg si nañ ci cappaandaw gi ñàkkutoon ay jafe-jafe ci nawet bi ci wàllu engrais
waaye gis nga %e bu yàlla defee jàmm bi ci ministère bi jëlee taxawaay ba ce war dsaanaka dem na ba engrais bi yëpp macha allah fu mu war a dem yëpp yegg na fa ci départements ak communes yi moo xam engrais gerte dugub ak mboq urée yëpp
taw bi nag gëlgóose boobu mu def noonu diggante mai juin am na lu mu lifin ba ñetti vagues yooyu mu wax moo fi ne
de semis boo xoolee fi mu toll nii dugub ji li tax mu jàppandi ak gerte gi yëpp li mu tiim yëpp ci vague bu njëkk bi la
moo tax boo demee ci marché bi fekk fa mboq fekk fa gerte sëb yi mu ngi ci marché yi mu ngi ci yoon yi tali bi nit ñaa ngi béykat yi di ko jaay
boo demee ci cin bi it ah ñu ngi ko fay lijjanti ci kër yi macha allah di ko loolu lañ tuddee autoconsommation bi
waaye pour ngir %e loolu lépp ak deuxième vague bi comme ni nga ko waxee nag deuxième vague beeg troisième vague bi nag foofu la xaw a yéexee xawee dese tuuti dina am ñoo xam ne xëy na seen deuxième vague dina mun a sori
waaye am na ci ñoo xam ne wax dëgg fa yàlla dina xaw a doy waar troisième vague ba moom daanaka kooku moom bu ñu waxantee dëgg rek te yàlla tax moom daanaka du mun a bokk
waaye yooyu yëpp li koy gën a fësal mooy enquêtes agricoles yi ñu ngi ci si balaa may ñëw nii rek jot nañ ab battaaxal boo xam ne le vingt sept bii la ñuy def atelier de présentation nationale atel() mission de présentation des résultats
maanaam li tukkee ci enquêtes yi dana am atelier boo xam ne benn ndaje boo xam ne incha allah le vingt sept lañ koy def fële ci DAPSA moo ko organiser ak kuréel yi ciy war a bokk yëpp
su ko defee ñu présenté ko ñu génn ci enquêtes yi nga wxam ne moo jëm ci enquête agricoles annuelles deux mille vingt deux mille mille et un ci campagne bi incha allah
pour wan leen ci kanam tuuti dinañ ci am lu gën a leer ndax loolu lépp enquêtes yi ñoo koy def ci wet ga it mu am enquête CESNSA
li mu wax ne fii nag am na ag digg goo xam ni wax dëgg fa yàlla ci wàllu taw dañuy gis ne demeewul noonu mooy li ñu tuddee noonu vallée morte siin boobu ak dëkk yi nga xam ne ñoo ko ñoo ko leroo gis nañ ne yëf yi dafaa xaw a tagatémbe
daaw gisoon nañ ko ren it daaw li mu doon exceptionnel exceptionnel xaw na faa feeñ tuuti waaye xawoon na vasquer wu ndax daaw année exceptionnelle la
waaye ren gën naa gën a fës ba ko jaar foofu nekkul loo xam ne lu ñu lu nit wax lu ñu inventé la kenn ku fay jaar gisal ko sa bopp boo wàccul tali bi sax da ngay gis yoo xam ne dina la xaw a jaaxal tuuti
boo ko toppee it noonu la fa noonu la fa demee donc mu doon loo xam ne dees na ko bàyyi xel waaye enquêtes yeeg yooyu ñu ngi ciy def liggéey boo xam ne waa CESNA enquêtes yi ak services agricoles yi dina ko gën a firndeel su ko defee dina doon outil de décision bi outil décision ngir kilifa yi gën ko bàyyi xel
tey wax nga zone d' intervention yi ngeen di nekk mais exactement %e pour quelque chose de concret tey lan ngeen di defal ñi nga xamante ne ñoom ñooy béykat yi fan ngeen leen di indilee seen apport yéen
voilà maanaam %e liggéey bi ñuy def mooy lan dañuy saytu ne boo xoolee lii ma tiim rapport la maanaam semaine bu jot dinañ def rapport boo xam ne dañ koy yónni
yónnee kilifa yi yónnee ko kilifa yi nekk ci région bi yónnee ko suñu naataangoo yi ñenn ñoom Maodo ak services yi nga xam ne yëpp yi nga xam ne kenn ku ci ne ba ci presse bi sax seen naataangoo yi ñoom ñëpp dañ koy jot
presse bi yëpp bu ma leen limee xëy na dana gudd waaye su ma nee presse bi ñi may dégg xam nañ ne %e rapport DRDR wax dëgg fa yàlla ñi koy jot bëri na
ba Dakar état major gendarmerie nationale dañ koy jot waxuma ministère bi nag ak i kuréelam donc dañ koy tas loolu bokk na ci li nga xam ne xëy na ñun ñooy liggéeyee noonu jàpp nañ jàpp ne xibaar bi dafa war a tas
nit ñi di ko dégg waaye xibaar bi yëpp mu tegu ci lu dëggu tegu ci xam-xam maandu it te nga xam ne amal njëriñ askan wi mu bañ a am benn parparloo bañ a am lenn lu ñuy nëbb
ndax am na ci loo xam ne boo ko nëbbee it nit ñi bu ñu génnee mu ne ah ma ne ko buñ ko gisee mu ne ah ma ne ko dinañ la joxoñ te loolu nekkul liggéey boo xam ne dafa tegu ci xam-xam
README.md exists but content is empty. Use the Edit dataset card button to edit it.
Downloads last month
31
Edit dataset card