audio
stringlengths
36
41
text
stringlengths
0
1.94k
/content/data_kallama/126segment_0.wav
salaamaaleykum man maay Khady Diagne Khady Diagne laa dëkk Dya béykat laa waaw ma ngi béy gerte di béy dugub ndax yaa ngi doon déglu émission yi coopérative bi doon def ci rajo bi waaw wax dëgg yàlla dama koy déglu léeg-léeg ñu koy nettali waaw waaye
/content/data_kallama/98segment_360.wav
jërëjëf diracteur en tout cas maa ngi lay remercié bu baax a baax daa ma may tamit ma gërëm suñu partenaire bi tax ñu toog fii donc muy ak ONG United :en purpose :en
/content/data_kallama/84segment_360.wav
donc gañcax gi rek lañuy dindi bu dee engrais bi bu dee engrais organ() bi d' accord Jalle dafa nga ne am na lo waaw ndax bi nawet bi daata bi mu daata àggsi sensibiliser nañu si mboolem groupement yi fenn fu ci nekk taxaw nañu fi animateurs yi taxaw na fa ngir mën a xamal baykat bi naka la mën a def ba defar kompos ndax comme ni mu waxee engrais produit chimique la gënul ci suñu yaram suñuy organe engrais bi baaxu si
/content/data_kallama/106segment_1380.wav
waaw moom tamit daanaka mi ngi doon mu nit dafa doon laajte waaw xamal naa ko nag sax bi nu mu mel kon nag waaw la bëggoon a tontu tuuti rek Mou() Moussa Ba ah waaw Moussa Ba waaw waaw Mous() bi ma njëkkoon laaj pour que héli() Sadio waaw waaw moom moom yow yow xa() daanaka gis nga ko hélicoverpa bii mu wax nii waaw héli() héliotis
/content/data_kallama/119segment_1470.wav
loolu jamono yooyu rek lañ koy constaté waaye lépp li nga xamante ni yàgg nañ ko fee gis mu ngi fi boobu dañ koy xàmmee dañuy xam lan moo ci war comme matuwaay xanaa mu doon yenn saa yi ndax gunóor comme melo comme jëmmi jëmmi nit rek yenn saa yi nga gis li nga xamante ni daawuloo ko gis li nga daawul gis nag boo ko gisee faaw nga jàngat nga door a xam yan matuwaay nga ci war a jël
/content/data_kallama/71segment_1110.wav
donc ak ak Koungheul donc Idda Mouride Fass Cekkeen ak Gént Pathé tamit ndox mi dafa ëpp foofu kon ñu jàpp ni que la situation pluviomètrique est normale à excedentaire au niveau du département de Koungheul vraiment te anomalie yi tamit bon demeewul noonu bi gën a néew li si wàññeeku 20 virgule 1 milimètre la léegi bi gën a ëpp mi ngi toll li ci yokku mi ngi toll ci 128 virgule 8 milimètres kon lii nag vraiment situation bii te nawet bi demagul fenn mën nañu mën nañu jox maanaam benn idée
/content/data_kallama/71segment_840.wav
di la nuyu yow Aliou Sow yow mi nekk directeur rajo thiel Jabi jula FM waaye it di nuyu ki nga àndal nuyu Sadio Deme moom itam muy coordonnateur ci projet bi projet bi nag ñu ngi koy wax maanaam projet AICRA donc man ma nekk ma nekk ci responsable maay responsable parc parcelle bi bi gën a mag ci biir projet bi maanaam ci commune Thiel
/content/data_kallama/99segment_690.wav
boo jëlee ci wàll
/content/data_kallama/130segment_1200.wav
gëstu wane na ne gis nga li gën sax ci dakasa yooyu noonu léeg léeg da ngay gis béykat bi des fois dañ koy tourner dañ koy retourné retourné boobu lu am solo la gis nga boo ko retourné ba taat bi féete kaw ab njàngat gëstu man yàlla def na gëstu naa ci sama def naa ci mémoire DEA université ci aflatoxine boobu
/content/data_kallama/94segment_780.wav
maanaam ñi nga xam ñooy béy gerte gi ak énebe jeeg yooyu béy * effectivement effectivement comme si wàllu semence ngeen di wax moo tax ma *** loolu ñuy wax si semence certifiée si yéen ñi nekk si mbéyum tool mi sxi mun si boolewaat ñun ñi nga xam ne ñoo nekk ci
/content/data_kallama/134segment_930.wav
parce que fi nga koy ji sa gerte bi doo respecté gerte Mademba mu ngi nii
/content/data_kallama/53segment_1500.wav
boo koy xayma mu ngi nekk presque à cinquante kilomètres si kaw couche boobu mooy couche d' ozone lu tax ñu naan ko couche d' oeone parce que maanaam tënkam fa la gën a bëri concentration am foofu la gën a amee solo yaa ngi dégg léegi loolu nag dafay filtré rayon ultra violet yi
/content/data_kallama/82segment_840.wav
dañuy jël léeg-léeg dañuy su wàccee après en général dañuy jël benn morso wala benn suyetma nga xam ne am na ay bën bën yu ndaw
/content/data_kallama/30segment_720.wav
machine buy soq et cetera donc loolu yëpp ay services yoo xam ne dafa am lien ak agriculture parce que por agriculture bi dem aussi
/content/data_kallama/26segment_180.wav
kon nag Malang
/content/data_kallama/54segment_930.wav
tey bu nekkee ni lu ni mel daanaka sax béykat bi waaw dama lay jox exemple rek ak yaakaar naa ne ñu ngi liggéey liggéey bu am solo muy waa FEPROMAS di ma déglu parce que fekke naa seen jotaay ak ñoom Nimna Diayte Trivolsificher am na ay béykat yoo xam ne organiser na leen
/content/data_kallama/4segment_0.wav
mu nekk loo xam ne it dafa am solo comme nim ko waxee moo di prévision saisonière ak yooyu mu nekk loo xam ne it saa su nekk da ngeen koy nekk di ko yeesalaat loolu tamit naka la waaw xam nga yeesal bi ñuy def rek mooy que ni ngay jékki-jékki saa gis jawwu ji sedd nga jékki-jékki saa gis mu tàng %huym nga jékki-jékki saa gis mu ngelew jékki-jékki saa gis asamaan si asamaan si ñuul kuku noonu la ñuy soppee prévision yi parce que jawwu ji taxawul benn place instant boo toog jël température bi balaa ngay xef température bi changé na donc noonu la affaires yi di changé donc bu tempéra() parce que tout est lié à la température et à la pression dafa am lu énuy wax préssion am loo xamante ni moom la ñuy wax température
/content/data_kallama/26segment_630.wav
comme li ñu tuddee banque classique yi mi ngi fi waaye ñaare pour mën cee jot dafa ci seen financement dafay nekk loo xam ne nii dafa jafe du lu ñaare loo xam ne nii comme ni ko Fatou Seye waxee léegi ligne de crédit boo xam ne nii dañu ko faa teg maanaam benn sàq moo xam ne dañu koy teg foofa Etat bi yombal jot ga boo xam ne nii nit ñi daañu ca mën a jot budul loolu rek jot ci banques yi dafay dafay jafe
/content/data_kallama/31segment_720.wav
ci gëstu xool nañ ni bu njëkk ca jamonoy ay maamaati maamat xooloon nañ ni booba temps économie adduna bi yëpp mi ngi tegu woon ci li ñuy wax agriculture bu njëkk comme ni ñuy béyee fii rek boobu temps noonu la ñu daan béyee ay fas la ñu amoon ay kii yi xam mais bi ñu toogee ba nga xamante ni bii dem nañu ba ni léegi dañu war a développé wu dégg nga daal di créer ay usines créer affaires yu kenn xamul dégg nga kooku ça date de dix huit cent quarante mille huit cent quarante ci la problèmes yi commencé am parce que usines yi ñoom ñooy émettre souvent ay saxaar
/content/data_kallama/31segment_1230.wav
parce que xam nga produit bu lu lu mu humidité bu bëree ci produit rek day da joy yàq boo ko dencee mu yàqu muy soble muy muy dugub muy mboq muy humidité boobu bu wàññiwul ba mu wow koŋŋ boo ko dugalee ci saag wala nga dugal ko ci bërigo wala nga denc ko dafay nëb parce ndox mi fay nekk humidité bi fay nekk moom moo koy nëbloo
/content/data_kallama/95segment_420.wav
kon bu ñu waxee rek jokkalante jokkalante kon nag mbokk yi yéen a ko moom
/content/data_kallama/30segment_480.wav
gis niir bi nga xamante ne bii dafay taw point bi nga nekk dinga war a mën a calculer xam exactement ban heure la war a mën a egg si donc ñun noonu la ñuy liggéeyee léegi wutee na peut être xëy na ak mais kay ñi fi nekk tey ak ñi fi yàgg nekk démb ñoom ñëpp ci même écoles yi la ñuy génnee pratiquement boo xoolee même diplôme yi lañ yor même connaissance aussi moom la ñu am quoi
/content/data_kallama/69segment_210.wav
ci ban service la nekk maanaam moom ci boppam moo yore boppam wala dafa bokk ci beneen service c' est une direction de l' agriculture moom la DPV nekkee direction di() direction protection des végétaux service à part mais sunu ñëpp sunu yaay mooy agriculture léegi nag ñun fii ñu ñu fi affecté au niveau du département ñun ñoo man maa fi ne wante mais nag on gère deux régions
/content/data_kallama/26segment_540.wav
non béykat bu ne am na façon parce que mun na taal ay pneu ay safara ci guddi gi xam nga une fois ñu bëri ñi nga xam ne daal wànq yi su buggee sonal am na at yu paase dafa doon sonal wànq yi dafa sonal te oto yi bëri wu ñu bala mu ñëw ci sa tool mun na egsi wànq yëpp yàq nga gis ñu wàcci nekk ci taat wi soo demee bëccëg doo leen gis ñu dox mais su guddee rek nga gis leen si léegi soo taalee lumière affaire bi lëndëm na lumière bi moo leen di xëcc ñu ñëw daanu safara bi ñu dee foofu parce que soo bëggee jël sa loxo nga dindi di dindi su bëree doo ci mucc voilà donc am na am na sax façon xeex boobu ñuy xeexee
/content/data_kallama/124segment_90.wav
kon jaachère am na solo kon noppal suuf si am na solo ndax doomu aadama bi tam suy liggéey dafa war a noppalu comme dafa war a noppalu nit ki aussi bu xamee loolu dafa war a noppal suuf si te tam mu jox ko li nga xam ne moom la yelloo ci wàllu comme li ñu wax sànq si wàllu tos yi ak yu mel noonu monsiaur Pierre est ce que dafa am beneen façon tos boo xam ne bi mun na dundal suuf bu bokkut ak tos yi ñuy wax li nga xam ne mooy ndesitu tool yi wala neefere yi nga xam dafay jógee si jur gi am na beneen façon mun nañu ko am ngir mun a dundalaat suñu suuf si
/content/data_kallama/6segment_1350.wav
ni ma ko waxee sànq rek comme olof bi tamit taxu ko demee noonu waaye dina sona() sonal gàncax gu bëre maanaam xeetu mbéy yu bëre dina leen sonal waaye ci mboq yi moom ak coton ci la gën a doy waar daal fa la yàq-yàq yi ëpp rawatina ci mboq mi loolu moo tax sax boobu nag ni ma ko waxee bu gàncax gi commencé jug rek mën nga ko ci gis waaw te boo ko gisee yàq-yàq yi moom même xob yi da koy lekk day lekk xolu garab bi
/content/data_kallama/54segment_90.wav
mbokk yi ñu ngi leen di nuyu di leen gërëm di leen sant di leen fàttali yéen a ngi seen rajo muy Jabi Jula FM téeméer ak ñaar tomb benn kaddu gi di bàyyeekoo fii si commune bu Thièl di nuyu ñëpp di leen ziar di leen bàyyi xel bu baax a baax di sant nag mboolem auditeur ak auditrices yi nga xam ñu ngi bàyyi seen xel seen rajo muy JKabi Jula FM téeméer ak ñaar tomn benn ñu ngi dikkaat ak yéen seen ay émissions yoo xam ne dañuy faral di ko def saa su ne si dimbalal nag waa ECHO ak Jokalante seen dimbal la ñuy faral di def émission yi tey tamit ñu dalal ki nga xam ne moom mooy monsiaur Pierre Badiate mi nga xam ne nag dafay yëngu lu jëm si wàllu mbéy fii si biir département bu Linguère si cabine technique bi seen xarit Cheikh Ibrahima Touré ak ki leen di animé émission bi seen xarit di Alioune Sow
/content/data_kallama/98segment_990.wav
semence moom ku koy wax fii ci Louga te waxoo Demba Tall en fait c' est c' est maanaam quelqu' un bi nga xamante ne ci ci processus su semence yi d' accord waaw lu ma bëggoon a tàggatoo mooy peut être nuyuwaat suñu waa service
/content/data_kallama/57segment_510.wav
directeur jërëjëf waaw ñoo ngi encore du ñu noppi di sant waa ECHO xam nga bu ñu tànnee commune bu Thièl ñu ne nañ fa def émission bu jëm ci càmm gi ak mbéy mi surtout ci biir département Linguère xam nañu vraiment Thièl li mu représenté ci agriculture booy wax agriculture arrondissement bu Barkedie moo tax
/content/data_kallama/22segment_720.wav
muy béykat bi ci boppam na créé une banque cérélière de solodarité ba nga xam ne képp koo xam ne béy nga dugub nga génneesa cinquante kilos :fre ne def naa ko ci action de solidarité ci banque bi ok :en su ngeen boolee suñ boolee lépp je crois que a na période boo xam ne béykat bi ci lay sonn te béykat bi ci période boobu la~, leen di gën a faagaale
/content/data_kallama/120segment_150.wav
kon laata ñuy dugg si waxtaan bi rek dañu koy jox moom Pierre Badiane mu nuyoo ak askan bi nga xam ne tam ñu ngi déglu Diabijula FM fàttali leen i tam si cabine technique bi seen xarit di Thierno Ibrahima Touré moo leen fa nekkal waaye ki leen di animé émission bi seen xarit di Alioune Souare Sow kon Pierre ñu ngi lay dalal jàmm fii si rajo Diabijula FM
/content/data_kallama/24segment_780.wav
foofu da() dama ko si bugg a yokkal parce que yu bëri day xew fekk information météo bi nit ñi jot nañ ko de mais souvent nit ñi dañuy jot information ba pare def au delà information biñ leen di jox dafa am ay messages yu ñu leen di envoyé
/content/data_kallama/72segment_960.wav
waaw waa mën nga jox sa numéro 77 wala 70 77 waaw 77 waaw ah non sa sa réseau bi baaxul bu baax ngir 600 cin() 77 500 600 663 663 waaw 37 44 37 44 waaw jërëjëf voilà 37 44
/content/data_kallama/117segment_1020.wav
bon dèjà prix yi bokkul prix yi su bokkee rek qualités yi bokkul qualité bi bokkul donc non cert() non certifiée boobu la ñuy ne écrémé da ngay dem marché rek nga jënd amul benn contrôle processus contrôle
/content/data_kallama/54segment_750.wav
ñu def leen ay coopératives ñu def leen ay coopérative léegi groupement Fapal bu ne nekk benn coopérative ci ki bi mu am benn benn union su ko defee coopérative bu ne léegi dana am sañ-sañu comme ni mu ko amee sax si * yi mais xamuñu ko woon mais informations yi dana jàll ba ñoom itam ñu mën di def semence Fapal di def semence su ko defee loolu jàpp nañu ne bu ñu ci ligéeyee incha allah problème mu rupture wala problème mu jafe-jafe semence ak ak ak ay li mel ne que intra yooyu dana ci dana dana yàlla mën nañu si dimbale
/content/data_kallama/87segment_780.wav
yaakaar naa ne loolu war nañ ci lëkkaloo ak service techniques yi gox bu nekk nag ak say réalités parce que tamit ni ñuy amee information taw yi noonu la ñu war a informa() am information ñëw ci service techniques yi mais booy xool ci wàllu ANACIM vraiment ñu ngi ciy def liggéey bu jéggi dayoo
/content/data_kallama/82segment_450.wav
pour mën a vraiment mën a wax nan la suénu nawet bi mel mën a wax tamit lan la ñuy xaarandi si nawet wi maanaam si tënk maanaam mën a wax li ñuy wax ay prévisions saisonières voilà jërëjëf am na solo ndax mën nga ñëwaat si prévision saisonière bu ren bi
/content/data_kallama/16segment_420.wav
di waaw jëf yooyu nit ki di jëf nag muy répété wu di répété wu di répété wu ñooy dem ba jural ñu li ñuy wax changement climatique jaww gi moom moo soppeeku kon foofu dañ naan nit ki mu li koy lor tey jëm ëllëg
/content/data_kallama/55segment_1350.wav
boobu ba léegi maa ngi toog di déglu waaye dafa am solo ngir thème bi kat muy résidus de culture maanaam bu ñu bayee ba pare yi nga xamante ni moom moo ci des* de culture :ra bi ak comme ni ko sama naataangoo bi waxee rek wax dëgg yàlla jàngee nañ ci lu bëri ndaxte ndaxte ku ni Louga wax wax bay ndaxte bu énu demee ba Louga nekk la première zone du culture au Sénégal loolu mot naa xam ak structures yi nga xamante ni mooy des c' est des c' est une structure éta() étatique muy waa DRDR maanaam direction régionale du développement rurale ñu gën koo xam ci ** kon nga xamante ni tey tey seen direction la au nivaeu régionale
/content/data_kallama/71segment_210.wav
amuñu woon benn jot lépp lu ñu daan liggéey journée bi ci kër gi lay yem tey nag bu ngoonee nga jaar ci unité bi jënd fa sa cere defar sa ñeex moo gën a gaaw jeex na kon foofa amatul lenn loo xam su fekkee ne yow tey danga ne tey dangay dangay dangay togg fonde reer dangay xaar ba ngoon rek nga yónnee sa araw jaay ma araw nga jënd sa araw dem togg sa fonde reer
/content/data_kallama/51segment_1140.wav
parce que day kii nekk yu mag quoi mais bu tawee ci kawam non seulement am na nu muy demee doomu gerte bi dafay lu si lu luy mel ni ba ba léegi sax ngooñ mi dafa ñuul souvent hur gi buñ ko lekkee sax dañuy am ay problèmes donc kii quoi d' ordre sanitaire xam nga lu ma la wax
/content/data_kallama/106segment_1140.wav
kon nag monsieur Malang ñu delluwaat tuuti ci olof tamit ndax naka la ñuy def ba nga xam ne yenn yàqu-yàqu yi ci tool yi ñu mën koo mucc waaw waaw yàq-yàq yi ci tool yi comme ni ma ko waxee ci soceeg ci
/content/data_kallama/12segment_450.wav
yaa ngi may dégg ma waaw maa ngi lay dégg sànq yaa ngi dégg Ibrahima bi muy wax mane ah ndax léegi mën ngaa ràññee poche su entreprise bi ak poche su kër gi poche su entreprise bi ak poche su kër gi li Ibrahima doon wax sànq li Ibrahima doon waxtaane waaw waaw loolu Ibrahima moom wax dëgg yàlla moom macha allah ar mënuñu koo fay wax dëgg yàlla xam nga xam nga Ibrahima dafa ne ah yéen jigéen ñi bu ngeen dee ligéey benn mbir waaw
/content/data_kallama/58segment_1710.wav
fa ñu ñu démultiplier l' information ñëpp xam mais bu nu xamee ñoom ñëpp ku ci ne boo gisee sax bi boo ko gisaatee nga daw jox du kii jottali ko sa morom waaw localités yii yëpp Kousanaar Malem Niani Payar yooyu yëpp gis nañu ko fa Dialokoto yii dëkk yii yëppgis naén ko bun la ko buggee ñu wan la ko
/content/data_kallama/34segment_720.wav
waaw muy sax sax boobu nag maanaam li nga xam ne muy sax mboq tey loolu tamit indi na beneen gàllankoor vraiment mi ngi dugg na si Sénégal kenn mënut a xam fi mu jaaree ñii ñu ngi naan ci mboq bu juge woon Amérique la ñii ñu ngi naan ci échange commerciaux yi la
/content/data_kallama/24segment_750.wav
kañ la tàmbale ak kañ lay jeex te dafa nekk loo xam ne jeexam day gaaw parce que léegi boo xoolee janvier ren daanaka delluwaat nañ encore ci tàngoor da nga dugg fii rek tàngoor bi commencé na te am na gàncxa yoo xam ne tey nit ki mu ngi koy béy te bu la wóoree ni que boo ko béyee bu ko fi tàngoor fekkee pour mun ci jëlee dara mais jàpp leen ni kat tey xabaar bi tey ngeen ko gën a soxla encore
/content/data_kallama/64segment_390.wav
message bi bu ñu la ko joxee yow nga uti() utilisé ko te joxuloo ko ñeneen amul njëriñ
/content/data_kallama/139segment_810.wav
donc loolu rateau ba mu baax nga jël ko def ko ci kàmb voilà mën naa wax sax région Tambacounda ngir mën a liggéey wóor na le suuf soosu am na ñoo xam ne béyuñu ko liggéey ci noo mën a def ba di di jàkkaarloo matériels yooyu mën am ko
/content/data_kallama/26segment_630.wav
donc boo bëggee bay comme lu mel ni ceeb par exemple da ngay dem ci suuf yoo suuf suuf soosu dafa soxla ndox ceeb dafa soxla ndox bu bëri danoo soxla am air bu fu nu fu nu màggee pour ñoom ñu mën di law bu baax ci biir suuf si
/content/data_kallama/15segment_870.wav
donc 3000 producteurs yooyu yu daaw yi
/content/data_kallama/57segment_60.wav
dañuy jël ñaari aspects yooyu mooy aspect social bi mooy fexe ba pour que lépp luy suñu jafe-jafe ci biir kër gi ñu toog mag maa ngi fi saa yu ñu ko waxtaanee rek pexe génn ndaw li moo yor doole ji
/content/data_kallama/71segment_1440.wav
donc juróomi données yoo xam ne ay méthodes de lute la pour contre ces ravageurs là jërëjëf am na solo léegi beneen laaj bi mooy lan mooy njëriñu jëfandikoo xibaaru météo xibaaru météo si activités yi nga xam ne dañ koy def maanaam si jamono yi nga xam ne ñu ngi mën a denc li nga xam ne rek mooy li ñy béy
/content/data_kallama/71segment_960.wav
léegi bu fekkee adduna bidafa wan kanam jant bi da ngay nekk si bëccëg ah keneen ki nekk yeneen dëkk yi nekk si guddi tu vois parce que ñun tey nga xamante ne ñun ñoo nekk au niveau des topiques de ñun ñi nga xam ne c' est nous sommes des maanaam ñu ngi si Equateur bi
/content/data_kallama/105segment_630.wav
kon am na solo kon semence certifiée am na solo kon ni ñu daan certifié xëy na maam xel la doon doxee waaye léegi xam-xam la ñuy doxee kon na ñu sukandiku ci xam-xam bi moom moo ëpp solo ci wàllu semence bi nga xam ne mooy jiw bi nga xam ne i tam
/content/data_kallama/135segment_1680.wav
kon nu ñëwaat tuuti rek kay jox monsieur rek kaddu bi rek mu ñëwaat ci phase de récolte bi mais information bi producteur bi war a soxla si période bi ñu nekk nii
/content/data_kallama/10segment_270.wav
ak employé nga tamit lu toll ci 5 personnes buñ koy xayma loolu yëpp fan la jógee waaw loolu yëpp aussi ci ci ci taxaw la ak nangu liggéey puisque aussi wala alpulaar ñu ngi yore benn kàddu bu ñuy wax ci pulaar
/content/data_kallama/51segment_960.wav
nan la mel tey ak nan lay tëddee ëllëg mu nekk ay informations yoo xam ne dafa am solo trop ci nekkinu béykat bi
/content/data_kallama/16segment_90.wav
tamit yàlla moom saa yu **** ni ko wolof di waxee rek du tëj bunt tëj paranteer saa yu bu benn bunt nee ràpp rek xamal ni beneen bi moom moom faaw mu ubbeeku d' habitude c' est comme ça quoi donc am nañ yaakaar daal que incha allah projet boobu léegi mu taxaw je sais que gars yi sori nañ si lool ñu ngi woon si toilettage projet bi kii quoi toilettage bi am na ay
/content/data_kallama/97segment_600.wav
/content/data_kallama/73segment_900.wav
loolu moo tax suuf si dee rek ñun ñooy dee parce que suuf si lu mu soxla pour dund ñun loolu la ñu soxla pour suñu dund bi
/content/data_kallama/51segment_690.wav
siège bi Saalum Diané la te ñu ku kii réseau Wula ki Dóor waar yor ko
/content/data_kallama/13segment_210.wav
bu tawee rek bu tawee rek bu bàq bi xawee tooy rek nañu ji ndaxte xam nga xam-xam dafa wane ne tey jii boo jëloon gàncaxu gerte soo ko jiyee ba 15 jours soxlawul sax ndox gerte su gàncax su bàq bi tooyee soo ko jiyee fii ba fukki fan ak juróom moom mooy dundal boppam kon ñaanuñu yàlla ñu ji gerte ba pare toog fukki fan ak juróom ndaox ñëwul déedéet kon nañu jiiróo
/content/data_kallama/86segment_390.wav
message bi bu ñu la ko joxee yow nga uti() utilisé ko te joxuloo ko ñeneen amul njëriñ
/content/data_kallama/28segment_1290.wav
ana waa kër yëpp ñu ngi fi ñu ngi si jàmm kontaan nañ ci émission bi ndax wax dëgg yàlla nit ñaa ngi ciy am na daa ñu ci yo() ku ci bëgg a am xam-xam moom da nga ko ci jëlee nawet moom bu xa() tool moom bu xasee ba ñor yàlla jiy taw ah moom kooku moom il faut rek borom am borom am mu am xam-xam boo xam ne nii lii nga xam ne kay moom gerte gi moom bu ñu ko deqee ci ci bàq bi
/content/data_kallama/22segment_120.wav
xam nga donc yeesal foog mu am parce que mbir mi li mbir la boo xamante ni affaire bu subtile la parce que mën nga jékki-jékki saa joxe benn situation joxe ay prévisions tu peux avoir aussi des marées baromètriques yooyu yëpp mën na am yooyu mën na yàq système bi donc bu ko i ba laata nag mu koy yàq météo nag dafay def lu énuy wax ay yeesal
/content/data_kallama/54segment_390.wav
parce képp koo xam ne yaa ngi basé wu si ñoom amn na ñëpp mënuñoo jot message wala ñi nga xam ne bu jotee message sax pour ñu lire ko ba xam ko problème la waaye comme ça nim de() ni mu demee nii wàcc sur le terrain nay déglu di information bi rek moom buy déglu information bi rek dana dana comprendre
/content/data_kallama/17segment_480.wav
buén la ko waxee ba pare après nga door a dem xool ban genre ru jiwu ngay jënd pour vraiment mën a am rendement bu baax jërëjëf am na solo am na solo lool si nga faram-fàccee ndax baykat bi war na déglu bu baax lu jëm rek si wàllu xibaar yi nga ne dañu koy jox mu nekk xibaaru météo ak tamit li nga xam ne moo di prévision saisonière bi tey amaa na sax xam naa ne ay tehnicien ngeen di yëngu di jàppale di ànd ak ñi nga xam ni ñooy baykat yi waaye tamit di fekkee ay ndaje yu bëri
/content/data_kallama/6segment_480.wav
buén la ko waxee ba pare après nga door a dem xool ban genre ru jiwu ngay jënd pour vraiment mën a am rendement bu baax jërëjëf am na solo am na solo lool si nga faram-fàccee ndax baykat bi war na déglu bu baax lu jëm rek si wàllu xibaar yi nga ne dañu koy jox mu nekk xibaaru météo ak tamit li nga xam ne moo di prévision saisonière bi tey amaa na sax xam naa ne ay tehnicien ngeen di yëngu di jàppale di ànd ak ñi nga xam ni ñooy baykat yi waaye tamit di fekkee ay ndaje yu bëri
/content/data_kallama/10segment_30.wav
chaque 5 mètre am na benn niimaa bu ci nekk kon garab bi allo na nga def ça va na nga def ça va naka guddi gi nag kooku kan la ak fooy wootee Abdou Soumaré Ngidiwal Abdou Soumaré Ngidiwal waaw soumaré bisimillah yaa ngi jàkkaarloo ak monsieur Tall allo monsieur Tall oui na nga def maa ngi fi alhamdulilah Soumaré dée() man Mamadou Diop la Mamadou Diop Ngidiwal ah Mamadou wàcci wàññil rajo bi wa() waaw bisimilah
/content/data_kallama/105segment_300.wav
moo ngi département Koungheul ci Kaffrine
/content/data_kallama/7segment_630.wav
ci wàllu traitement bi tamit ci même bës lañ koy defandoo donc nag topp nañ ko nag ba xam ne donc ci variété yooyu ñuy def am na ci ñett ba ñeent yoo xamante ne ñooñu moom commencé nañoo ñor commencé nañu witt di denc donc yooyu yëpp dañuy def de sorte que du ñu jaxase li nga xamante ne moom lañ jëlee ci récolte yi benn bu ci nekk dañu koo utal benn sako bind turu variété bi lépp loo génne ci parcelle am nga dugal ci saako bi donc loolu mooy tax ne doo jaxase variété yi
/content/data_kallama/102segment_0.wav
jërë ngeen jëf auditeurs de la 88 point 7 ñu dellu ziar leen bu baax dellu it di leen jox seen wàccuwaay comme ni ñu ko baaxoo saa su nekk ànd ceeg yéen rek ci émission yu daal di am solo nekkit li leen di yitteel waral nag tey ñu daal di fas yéenee amal ab waxtaan bu daal di am solo ci pàttali émission bii ñu ngi ko amal rek ci jàppandalu rajo RIP FM ci lëkkaloom ak Jokalante ak PAM PAM nag di programme alimentaire mondial lu ñuy waxtaanee mbokk yi di wàllu changement climatique nmaanaam coppiteg jaww ji mu nekk nag mbir moo xamante ne nii daanaka lëmbee na adduna waaye nag ku wax changement climatique am yaakaar ne am na ab njeexital ci li nga xamante ne moom mooy wàllu mbéy mi
/content/data_kallama/39segment_390.wav
loolu dafa am solo taxawaay boobu moom la Fapal def muy taxawaay boo xam ne bu am solo la ndax jigéen ñi budee ci wàllum defarum saabu formation am na fi budee ci wàllum yarum xar yi activité yi nga xam ne jigéen ñi petits commerce yi commercial defal nañu leen formation budee kuy bay xeetu mbay ma ngay bay bu nekk defal nañ la formation def nañu formation pour kooku nga mën cee ndax nit ki boo jógee ne damay def dara te
/content/data_kallama/68segment_240.wav
waaw man daal
/content/data_kallama/51segment_840.wav
ba Diaole ba Diaole maanaam bu ñu nangoo lëkkaloo inter communalité mooy condition fondamental bi it mooy tax di nga xam ne pour projet boobu mën a dem bu ñu ko nangoo ba lifin bu nit doxalee lañ ca war a doxaljëm ci wàllu mbéyum ceeb jëm ci wàllu mbirum maraichage mbirum maraichage déedéet ba ci ci biir yëf yi am na jiwu programme jiwu am na ay digues am na sax *** am na ay magasins bawuñ dara
/content/data_kallama/67segment_210.wav
léegi ngelaw yi bu ñu dajee foofu dafa am benn genre ru tàngoor boo xamante ni moom la ñuy xaarandi si Océan Atlantique donc bu ñu gisee itam si mois d' avril mois de mars la ñu gis ni que tàngoor bi vraiment mu ngi persisté si biir Océan atlantique donc ñu gis ni que vraiment la la ZCIT est très bien structurée vraiment ni mu mel vraiment baax na lool pour mën a indi ay taw si kaw jàngat yooyu noonu ñu def nag gis tamit avancé bu muy avancé ak tamit position bi nga xam ni foofu la frond intertropicale bi nekk bi nga xamante ni moom mooy seddale taw yi ci ci sunu si si Afrique sowu jant vraiment ñu mën a wax ni loolu moo tax ñu mën a xam ni ren dana taw et puis bon taw taw bi dana teel a ñëw te taw yi dana bëri
/content/data_kallama/92segment_240.wav
mën naa am nga ji ko ba ca kanam mën a am rendement bu baax mën a fay suñuy jiwu jërëjëf président
/content/data_kallama/66segment_240.wav
pare tagal la tegal la interet bu diis bu diid wallaay loolu moo taxoon ñun ñu sos crée CREC bi ndax xam nañ ni loolu ñun attanuñu ko waaye bi ñu demee tamit ci biir loolu dañuy génne yoo xam ni dañu koy tegal 1 pour 1.5 par mois nga xamante ne su jëlee bor juróomi weer jël 100000F 7000 la ciy teg loolu je crois que ci wàllu ci wàllu li ñuy doxalee wute na un peu ak li nga xamante ne noonu la ba() banque classique yi di doxalee te ñoom boo fekkente ne amul retard de paiement
/content/data_kallama/1segment_1140.wav
mais est que ndox moomu amna durée boo xam ne bi su ko defee tam day amaat beneen changement wala couleur wala yu mel noonu wala ndox moomu léeg-léeg dama ne am na si fii ay ay
/content/data_kallama/79segment_450.wav
maanaam zero virgule quatre pour cent si at bu nekk si at bu nekk loolu la en moyenne si tënk daal te booy xool si nu mu nar a dund si adduna bi mën na nekk vingt ans jàpp deux cent ans xam nga loolu dafa bëri xala xalaatal zero virgule :ra quatre pour cent chaque chaque année nga am ko ba pare mun nekk mu war a nekk si jaww ji vingt ans jàpp ñaar téeméeri at
/content/data_kallama/25segment_1140.wav
semence bi en fait dañu ko traité maanaam boo déggee semence bi nga xamante ne dañu koo traité te produit chimique boobu noonu dafay tax yow mii béykat bi waroo ko mun a jëfandikoo
/content/data_kallama/73segment_180.wav
kon
/content/data_kallama/126segment_750.wav
parce que xaalis bi ñuy jox ñoom ñoo tax ñu jox ñu ko
/content/data_kallama/24segment_390.wav
ndax damay yàq am na ci koo xam ne sax ñëw na ba ñàkkee ma teggin ndeysaan ma xool ko ma ne ko paa mu ne ah ma ne ko tee ngaa jàpp li nga jàpp te li ma lay moytuloo mooy ngay tudd samay waajur di tudd leneen loo xam ne ndeysaan ma wax ko ko mu wan ma gannaaw mu dem waaye loolu ma doon def ñu may tere wala ñu may
/content/data_kallama/56segment_390.wav
te suñu maam lim fi bàyyiwoon ñoom
/content/data_kallama/18segment_480.wav
population yi dañ si jànkuwanteel problème jërëjëf monsieur René kon am na jafe-jafe yoo xam ne tey askan bi ñu ngi koy jànkuwanteel waaye jafe-jafe yooyu nag
/content/data_kallama/0segment_510.wav
voilà ñoom guddi gi la ñiy gën di yàq la ñuy yàq bëccëg gi voilà bu fekkente ne ni kii gunóor bi ñu naan runibia la gunóor bu xonk bi moom moom day su() gasu suulu ci biir
/content/data_kallama/0segment_270.wav
si loolu nag la ñu kon dafay jaadu parce que tamit su fekkente ne ndaw bi dafa am projet te amul fu mu ko liggéeyee loolu tamit day nekk loo xamante ne
/content/data_kallama/16segment_1500.wav
mais pou() poudre yeeg yenn kii yi nañu bu ñu approché woo ci DRDR yi
/content/data_kallama/19segment_30.wav
bi nga ko bayee loo gis waaw bi ma ko jiyee moom wax dëgg yàlla càq mboq bi rafet na càq dugub bi rafet na waaye daal xam naa ne moom des na des na mel ni ma ko bëggee woon
/content/data_kallama/34segment_1680.wav
waaw loolooy njëriñu tos moo tax béykat yi tos baax na waaye nag tos dafa laaj exigenace booy xool ci wàll benn hectyare rek ñun li ñu ci xam mooy di def 40
/content/data_kallama/74segment_450.wav
bon en tout cas waajal bi lu yi nga xam ne daal éléments yu ma waxoon énoo gën a fës ñoo gën a am maanaa ci waajal suuf si tos ko def rotation maanaam soo béyee fii gerte déwén nga toxal béy fi leneen oubien nga bàyyi ko mu noppalu andi phosphatage def foofu moom moyens yooyu yëpp moom la ñu gën a kii parce que yeneen moyens yi nga xam ne daal mun nga waajal sa suuf si ñun munuñu ko parce que su nekkoon ci tubaab yi ñoom lu ñu defaree seen suuf si mun na ji mboq mu taw rek ma ji mboq c' est que ñoom seen ndox bi dañ ko maîtriser parce que ci tool yi nga xam ne dañ koy arroser na arroser mboq ou ñax be mu màgg ma énëw labourer ko pour ma def engrais vert mu nëb ci biir man labourer ko mu nëb ci biir ma bàyyi ko mu nëb après ma ji mboq laay jënd mu dem ba toll beneen hauteur ma faucher ko jël gyrobroyeur dagg ko ba pare ma labourer ko bàyyi foofu ba mu nëb loolu yëpp bokk na ci defar suuf
/content/data_kallama/38segment_900.wav
de semis boo xoolee fi mu toll nii dugub ji li tax mu jàppandi ak gerte gi yëpp li mu tiim yëpp ci vague bu njëkk bi la moo tax boo demee ci marché bi fekk fa mboq fekk fa gerte sëb yi mu ngi ci marché yi mu ngi ci yoon yi tali bi nit ñaa ngi béykat yi di ko jaay boo demee ci cin bi it ah ñu ngi ko fay lijjanti ci kër yi macha allah di ko loolu lañ tuddee autoconsommation bi waaye pour ngir loolu lépp ak deuxième vague bi comme ni nga ko waxee nag deuxième vague beeg troisième vague bi nag foofu la xaw a yéexee xawee dese tuuti dina am ñoo xam ne xëy na seen deuxième vague dina mun a
/content/data_kallama/126segment_1170.wav
su amee bénéfice la su amulee du la yàqal dara parce que am nga dèjà li ngay aaree soo xoolee 20 sacs si département bi léegi su ñu ko séddalee commune bu nekk un sac léegi commune bu nekk village bu nekk ñaata lay am waaw bu ñu ne parce que bu ñu xoolee commune bi ñu nekk rek ay plus de cent villages voilà * gis nga vingt cinq diviser par cent
/content/data_kallama/61segment_360.wav
dinañ xam dama bëggoon ñu xam à peu près ok :en boo ñëwee léegi su fekkee ne nag par exemple da nga ñewoon boobu ñu ngi la koy jaayee
/content/data_kallama/52segment_510.wav
waaw dëgg la Alioune ñun de wax dëgg tool yi liñ siy jooytu mooy ñu yéex see jot waaye bu fekkoon ne teel nañ see jot comme ça niñ jotee woon suñ jiw yiñ denc kon moom wax dëgg ba fiñ toll nii moom duñ si am dara dara lu ñuy rëccu
/content/data_kallama/23segment_0.wav
xam e rek moo di ANACIM waaw Seydou changement climatique defe naa nit ku nekk mu ngi koy sentir si boppam ndax léegi tàngoor bi métti na méttiwaay goo xamante ni ren mesuré nañ 47 degré si ker à l' ombre à l' ombre comme boo toogee si ker nga am 47 degré fii si Koungheul loolu mosu fi am
/content/data_kallama/89segment_990.wav
donc donc
/content/data_kallama/79segment_150.wav
kon yaa ngi ciy gis ay njëriñ lu am solo waaw maa ngi ciy kii bu baax a baax moom vraiment foo ko foo ko jàngee foo ko déggee foo ko mos a déggee ok :en ndax yaa ngi dégg émission bi coopérative bi di def ci rajo Alfayda
/content/data_kallama/9segment_750.wav
vraiment gis nañ tester bi vraiment am nañ ci xam-xam aussi it am nañ ci jëlee nañ ci njëriñ bu baax kon rafetlu nañ ñu ngi rafetlu seen taxawaay