Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet
audio
audioduration (s)
2.29
12.5
transcription
stringlengths
26
118
sa mbaal mi jén yu ndaw rekk la mëna jàpp
booy tisóoli bu ko def ci kow nit ñi
dafa ma ko wax may rabat lu ma waroona def
peese bi moo tax tefes giy wéet yenn waxtu yi
taxawalal eseel bi mu sës ci miir bi
xam nga xél ne ëgg bi baaxul ci naafi gerte yi
su dara desul lu dul ñàkkante ma dem sama yoon
boo bëggee togg yaasa dangay marine ganaar gi ak limoN
déedéet garab bi keroog gi ñu ma joxee garab bi ma commencer ko naan keroog la génn nii
maa ngiy wut pexe mu ma jàlle dex gi
bu jëkk jarbaat dafa daan donn nijaayam
danga ma suufu ci woto ba ma doon bëgga jénd
ba ma ko yeddee ba tey bàyyi na daw jàng
boo ko sangee ba noppi nga lenqali ko ak ndox mi ci siwo bi
xale bi nangootul dox cumbur bee ko jaaxal
bërëb bu ral bii nu mu fi mana nëbboo
ba diggante ñaari réew yi yàqoo moom lañu ràng
gën gaa bare mën naa ci def juróomi junni
bi mu fiy agsi mu ngi woon ci diggu dooleem
garab gii farmasi rekk nga ko mëna ame
dangay jéem ba xam ndax dinga mëna ubbi bunt bi ak caabi jii
am na ñuy sangoo reeni tol nee ñu dafay wàcce coono
ca tamxarit wa laa ko seeti fekk ko muy bomb cereem
teg sa takka ndeer ci ndox taxul nga tooy
ay jigéen yu doon dem faro ya ñoo ma won yoon mi
dafa saraxu duwaañ bi ba mu bàyyi ko
lu ñaaw li mu def la bëgg a dabu waaye wees na
xam naa ni sama woote du sooy ndax bàkkan dafa diis
su sunuy kàddu dëppoo mbir mi dootul yàgg
nanga butti jén yi dal di leen raxas ba ñu set
mënuloo woon jénd meew xanaa furóoñu cere ji
kenn mosu fi jàpp jaabaar bu ni tollu
fekk na biram njéemé koo njaay a ngi wara tollook ndangalma
boo amoon kersa duma taxaw ngay saaga
bant bi xar jéppén dafay tegtal ne yoon wi dafa def sél
soo bëggee birig bi xéj ci dangay xàppati koñ bi
ku dahà haj bél cà ker àm nga bayi ko
dafa duggoon ci njaayum gejj waaye dafa ca lom
bareetul suubkat yuy jëfandikoo nganj
Naka la agsi ci guy gi mu ni guy nàyeet
bu jëkk tubaab yi dañu gawoon njàngum alxuraan ji
xale baa ngiy xàqataay rekk soo demee dañu koy ñiiramtal
booy tudd xaalis muy ñàngal kanam gi
lor nga ma waruloo ko woon jox sama xaalis
xam na ni sa cofeel mosul deñ ci moom
bi ñu koy yóbbu loppitaan la faf loru
dañuy tari alxuraan bàyyi leen coow li
Nit kiy joxe kayit woowu dafa génnoon xaar naa ko lu yàgg
ku di talantu ci ñam boobà sa yaay a toga
ca diggu gott ga la dem samp fa néegam
moo taxit feebaru jigéen dafa bari façons
fu sindah yabé ndobin garab a fà jégéñ
li ñu lay fey a ngi tolloo ak sa man man
dafa tëddoon di féexlu ca peggu déeg ba
butoN bii lañuy wàññce tàkk tàkku làmpu petarool bi
waaN waaN ji dafa koy dimmali ci wasin
gaasal cere fass ji bala nga koy tay
dafa bëggoona nëpp nëppal biiru doom ji
bëgga riccamtéku moo la tax di wax lii
ab dànnala la woon waaye bët yi neexatul
bi nga xamee né buur yi benn kepp a ci des di buurub saalum mu daldi né
géew bi yaawul na nit ñi dellu gannaaw
aayal jaar ci suufu eseel biddaa tubaab yi la
picc mi bëgg xale bi xale biy màgg
kenn mënul def supp ci aset bu tell bii
arikoweer dañu koy toggaale ak lax bi
su ngeen ko téyewul dina ko dóor bolde bi
waxambaane yiy nemm a taal safara si ngay séen
bi mu tàmbalee jël garab googu ba tey miiratul
mu agsi jëkkër ja ak goro bu jigéen ba dawoo di jooyoo
dafa ubbi kaaf gi rekk picc yépp naaw
hej u ncokér ak seen àm ku cà gasul yoy
mu ni dama koy wallu ci njëlam lu jëkk li
ku am ngànt mbaa nga ñàkk ndox may nañu la nga tiim
xaaral ba timis fàddu nga door a génn
soow maa ngiy ñów ñaare ci ñetteelu fan wi gannaaw wasin gi
céy sama njaqare ja ba ñu ma nee awyoN ba dem na wacc la
ngem nekk fii di ratatati tere nit ñi nelaw
yow de yaay seet rekk ba xam li nga mën
ba nga xamee ni ñépp a ngi fecc di ree mu am ku ni
sa màngo gaa ngi buubu war nga koo xapp
Nangeen jóg bu ngeen deggee bàkku senegaal
ceglar ni caraax fekk ko mu déféenu
lu la yar ak teggin meyul leneen du la ko mey
benn géwal ba daldi jiin tabala ji né
dina dellusi gaa yàggaay bi rekk a ma ci jaaxal
mu né ko yow dangay fen tey jii dinaa la fetal
bu weer wi deewee war na fekk ku nekk joxe wàllam ci tabaxu kalaas bi
ba ma ko fàttalee xaalis bi dafa fenantal
dindil sa loxo yi nga dar ci sa nopp yi te déglu li ma lay wax
diine dina togg nit ki ba muy jëfe lu rafet
saxaar yiy dem amerig fii lañuy jaar
suqi na ganaar gi ba pare mu ngi koy butti
Ni nga àttee ku ko gis xam ne danga farle
ndax dénd wii mën naa xadd néeg bi
yàlla taal sànni ci matt a gën fey ko
ñu dagg buum gi wocc biram njéemé ca biir
ba ñu ko naanee daal lañu kata kayna
bu jëkk ñi daan jong ay magi jëmm lañu daan nekk
na ngeen yenduji ca dédd ga ca tool ba
End of preview. Expand in Data Studio
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
106